Soo bëggee gis README ci Àngle wala ci Français
👨🏽💻 Lii ab jumtukaay la bu defarkatu senegaal yi defar te képp man naa ko jëfandikoo fépp fu nga mëna nekk ci àdduna bi 🌍
Sudee borom projet nga, mën nga yokk sunu badge soo kopie kode bi ci suuf ⬇️ ci sa tegtal projet GitHub.
[![Made-In-Senegal](https://github.com/GalsenDev221/made.in.senegal/blob/master/assets/badge.svg)]
🚧 Soo bëggee jàppale ci projet bii, njëkkal jàng CONTRIBUTING.md !
A | B | C | D | E | F | G | H | I | J | K | L | M | N | O | P | Q | R | S | T | U | V | W | X | Y | Z