Skip to content

Latest commit

 

History

History
78 lines (66 loc) · 7.55 KB

README.md

File metadata and controls

78 lines (66 loc) · 7.55 KB

Waxtane

Le Wolof the simple way ?!

Niewlene niou waxtane, venez discuter, come discuss with us !

Qu'est ce que waxtane ?

Waxtane est un receuil de phrases de discussion traduites en trois langues (pour le moment).
Le Wolof le Francais et l'Anglais.

Waxtane vise à faciliter la communication entre personnes parlant différentes langues, en se basant sur un modèle sans prise de têtes la discussion.

Contributions

Venez contribuer un max !
Une discussion n'est rien sans ses intervenants.
Feel free to send PR and suggestions. 😁
Contribuez ici : Ajouter Contribution

Phrases disponibles

Wolof Français Anglais
1 Na nga def ? Comment vas tu ? How are you ?
2 Mangui gui fi Je vais bien I'm fine
3 iow nak, no def ? Et toi, comment va tu ? And you, how are you ?
4 Mangui ci diam Ca va I'm good
5 Kay gnou lekk Viens on mange Let's take a meal
6 Gnata att nga am ? Quelle age as-tu ? How old are you ?
7 Tay dama woorr J'ai jeûné aujourd'hui I fasted today
8 Fane nga deuk ? Où est-ce que tu habites ? Where do you live ?
9 Nane nga toudou ? Comment est-ce que tu t'appelle ? What's your name ?
10 Mangui toudou X Je m'appelle X My name is X
11 Dama la sokhla J'ai besoin de toi I need you
12 Dama khiff J'ai faim I am hungry
13 Dama marr J'ai soif I am thirsty
14 Mangui joko si leund mi Je me connecte sur le web I am surfing on the web
15 Dama beug lou jeum si waloum xarala J'adore la Technologie I love Technology
16 Dama beug ndekki Je veux prendre un petit déjeuner I want to take a breakfast
17 Dama beug Agne Je veux prendre un déjeuner I want to have lunch
18 Dama beug rére Je veux prendre un dîner I want to have a dinner
19 Damay takk jabar Je vais me marier I'm getting married
20 Mayma khaliss Donne moi de l'argent Give me some money
21 Bane wakhtu mo joot ? Quelle heure fait-il ? What time is it ?
22 Dama sonne Je suis fatigué I'm tired
23 Bu la neexee S’il vous plaît Please
24 Amul sólo Je vous en prie You’re welcome
25 Kay niou dem Viens on y va Come let's go
26 Jéggël ma Excusez-moi Excuse me
27 Ndax dégg nga angale ? Parlez-vous anglais ? Do you speak English ?
28 Dégg nga ? Comprenez-vous ? Do you understand ?
29 Dégg naa Je comprends I understand
30 Dégguma Je ne comprends pas I don’t understand
31 Nanga tudd ? Quel est ton nom ? What is your name ?
32 Jàmm nga fanaane ? Comment s'est passée votre soirée ? How was your night ?
33 Fii ba Sandaga ñaata ? Combien ça fait d'ici à Sandaga ? How much is it from here to Sandaga ?
34 Fan mooy seen wanaag ? Où sont les toilettes ? Where is the toilet ?
35 Neexoon na C'était bon It was good
36 Mi ngi ci jàmm Il/Elle va bien He/She is fine
37 Ñaata lay jar ? Combien ça coûte ? How much is it ?
38 Ñaata ngay jaaye bii ? Tu vends ça combien ? How much are you selling this for ?
39 Seer na lool C'est très cher That’s very expensive
40 Wagniil mako Diminue moi ça Turn it down for me
41 Lougnouy lekk ? Qu'est ce qu'on mange ? What do we eat ?
41 Dama khawa diapp ! Je suis un peu occupé ! I am a little busy !
42 Naka nga yendo ? Comment s'est passée ta journée ? How was your day ?
43 Barki démb diaronne na sa keur Avant-hier j'étais passé chez toi he day before yesterday I went to your house
44 Dama nieuwone indil leu sa khaliss J'étais venu t'apporter ton argent I came to bring you your money
45 Dama nékone daara dja J'étais à l'école I was at school
46 Damay saakou xam-xam Je suis à la quête de connaissance I am on a quest for knowledge
47 Nianal ma ! Prie pour moi ! Pray for me !
48 Témérri Diouni Cent milles One hundred thousand


Github Page