Le Wolof the simple way ?!
Niewlene niou waxtane, venez discuter, come discuss with us !
Waxtane est un receuil de phrases de discussion traduites en trois langues (pour le moment).
Le Wolof le Francais et l'Anglais.
Waxtane vise à faciliter la communication entre personnes parlant différentes langues, en se basant sur un modèle sans prise de têtes la discussion.
Venez contribuer un max !
Une discussion n'est rien sans ses intervenants.
Feel free to send PR and suggestions. 😁
Contribuez ici : Ajouter Contribution
N° | Wolof | Français | Anglais |
---|---|---|---|
1 | Na nga def ? | Comment vas tu ? | How are you ? |
2 | Mangui gui fi | Je vais bien | I'm fine |
3 | iow nak, no def ? | Et toi, comment va tu ? | And you, how are you ? |
4 | Mangui ci diam | Ca va | I'm good |
5 | Kay gnou lekk | Viens on mange | Let's take a meal |
6 | Gnata att nga am ? | Quelle age as-tu ? | How old are you ? |
7 | Tay dama woorr | J'ai jeûné aujourd'hui | I fasted today |
8 | Fane nga deuk ? | Où est-ce que tu habites ? | Where do you live ? |
9 | Nane nga toudou ? | Comment est-ce que tu t'appelle ? | What's your name ? |
10 | Mangui toudou X | Je m'appelle X | My name is X |
11 | Dama la sokhla | J'ai besoin de toi | I need you |
12 | Dama khiff | J'ai faim | I am hungry |
13 | Dama marr | J'ai soif | I am thirsty |
14 | Mangui joko si leund mi | Je me connecte sur le web | I am surfing on the web |
15 | Dama beug lou jeum si waloum xarala | J'adore la Technologie | I love Technology |
16 | Dama beug ndekki | Je veux prendre un petit déjeuner | I want to take a breakfast |
17 | Dama beug Agne | Je veux prendre un déjeuner | I want to have lunch |
18 | Dama beug rére | Je veux prendre un dîner | I want to have a dinner |
19 | Damay takk jabar | Je vais me marier | I'm getting married |
20 | Mayma khaliss | Donne moi de l'argent | Give me some money |
21 | Bane wakhtu mo joot ? | Quelle heure fait-il ? | What time is it ? |
22 | Dama sonne | Je suis fatigué | I'm tired |
23 | Bu la neexee | S’il vous plaît | Please |
24 | Amul sólo | Je vous en prie | You’re welcome |
25 | Kay niou dem | Viens on y va | Come let's go |
26 | Jéggël ma | Excusez-moi | Excuse me |
27 | Ndax dégg nga angale ? | Parlez-vous anglais ? | Do you speak English ? |
28 | Dégg nga ? | Comprenez-vous ? | Do you understand ? |
29 | Dégg naa | Je comprends | I understand |
30 | Dégguma | Je ne comprends pas | I don’t understand |
31 | Nanga tudd ? | Quel est ton nom ? | What is your name ? |
32 | Jàmm nga fanaane ? | Comment s'est passée votre soirée ? | How was your night ? |
33 | Fii ba Sandaga ñaata ? | Combien ça fait d'ici à Sandaga ? | How much is it from here to Sandaga ? |
34 | Fan mooy seen wanaag ? | Où sont les toilettes ? | Where is the toilet ? |
35 | Neexoon na | C'était bon | It was good |
36 | Mi ngi ci jàmm | Il/Elle va bien | He/She is fine |
37 | Ñaata lay jar ? | Combien ça coûte ? | How much is it ? |
38 | Ñaata ngay jaaye bii ? | Tu vends ça combien ? | How much are you selling this for ? |
39 | Seer na lool | C'est très cher | That’s very expensive |
40 | Wagniil mako | Diminue moi ça | Turn it down for me |
41 | Lougnouy lekk ? | Qu'est ce qu'on mange ? | What do we eat ? |
41 | Dama khawa diapp ! | Je suis un peu occupé ! | I am a little busy ! |
42 | Naka nga yendo ? | Comment s'est passée ta journée ? | How was your day ? |
43 | Barki démb diaronne na sa keur | Avant-hier j'étais passé chez toi | he day before yesterday I went to your house |
44 | Dama nieuwone indil leu sa khaliss | J'étais venu t'apporter ton argent | I came to bring you your money |
45 | Dama nékone daara dja | J'étais à l'école | I was at school |
46 | Damay saakou xam-xam | Je suis à la quête de connaissance | I am on a quest for knowledge |
47 | Nianal ma ! | Prie pour moi ! | Pray for me ! |
48 | Témérri Diouni | Cent milles | One hundred thousand |